Read, copy, and download the Pullo Àrdo lyrics LRC file, which provides synchronized music subtitles for the song Pullo Àrdo by Youssou N'Dour from the album Youssou N'Dour. Our LRC file is created using the free "LRC File Maker" tool and matches the official length of the song, which is 04:00.93. Additionally, you can download the lyrics in TXT (.txt), SRT (.srt), and PDF (.pdf) formats.
[ti:Pullo Àrdo]
[ar:Youssou N'Dour]
[al:Youssou N'Dour]
[lang:Luxembourgish]
[length:04:00.93]
[by:Jun]
[re:www.rclyricsband.com]
[ve:v0.0.5]
[00:00.00]
[00:14.78]Ku fi ñëw mu jangal la
[00:17.32]Nax mi moo ko moon noox mi moo ko moom
[00:20.10]Daf ko dónn
[00:21.37]Lii xar yi la, lii bey yi la
[00:23.97]Nagam yangi, àli bàngi
[00:26.93]Baaxi maamam Pullo Àrdo
[00:36.54]Ku fi ñëw mu jangal fa
[00:39.55]Nax mi moo ko moon noox mi moo ko moom
[00:41.98]Lii xar yi la, lii bey yi la
[00:44.41]Nagam yangi, àli bàngi
[00:47.01]Baaxi maaman Pullo Àrdo
[00:51.24]Pullo Àrdo, Pullo Jééri, Pullo Àrdo
[00:56.47]Pullo Jééri, Pullo Àrdo, Pullo Jééri
[01:02.23]Dàqqal yee ñu jëm fee nga dàqq yil ñu jëm fii
[01:05.03]Yaa xam yaw li xew fee, dara jaxalula fii ba fee
[01:08.71]Pullo Àrdo, Pullo Jééri, Pullo Àrdo
[01:13.78]Pullo Àrdo, Pullo Jééri, Pullo Àrdo
[01:29.58]Àrdo sex na gënnëm
[01:33.19]Dàldi gàddu yattam
[01:36.02]Ma nga ànd ag xaajam
[01:38.40]Dàldi jittël géttam
[01:41.54]Pullo Jééri, Pullo Àrdo
[01:45.73]Mi ngi ànd ag xaajam
[01:49.78]Dàldi jiitél géttam
[01:52.11]Dalal xelam, fééxal xolam
[01:54.85]Bu nin ñi fo aka ree moom yégu ko suuy
[01:59.22]Pullo Àrdo, Pullo Jééri
[02:04.63]Yeppam mu ngi fii
[02:06.86]Fii la yaroo, fii la màgee
[02:09.73]Te yii fii la takkee sowna
[02:12.55]Léppam fii la
[02:15.21]Pullo Àrdo, Pullo Jééri
[02:22.20]Bu nin ñi tëbë ka dal moom yëgu ko
[02:24.80]Li mu am fii doyloo na ko doy loo na ko
[02:27.53]Bu dee cor la mbaa jamaan la
[02:29.93]Walla etaas la, mbaa abyong la, mbaa leneen la
[02:33.99]Moom gisu ko, Pullo Àrdo
[02:48.12]Ma nga gàddu taxaaran
[02:51.02]Di mbiip mbiip mu am xorom
[02:53.53]Way, way yu amui moroom
[02:56.28]Mel ni kuy neexai goroom
[02:59.08]Boo fa jaaree sant Saar ee di na la ree
[03:04.43]Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
[03:09.91]Boo fa jaaree sant Saat ee di na la ree
[03:14.87]Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
[03:20.82]Di mbiip mbiip mu am xorom
[03:25.97]Way, way yu amui moroom
[03:28.71]Mel ni kuy neexai goroom
[03:31.35]Boo fa jaaree sant Saat ee di na la ree
[03:36.52]Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
[03:42.28]Boo fa jaaree sant Saat ee di na la ree
[03:47.31]Boo fa jaaree doon Séréér ee di na la ree
[03:51.91]RCLyricsBand.Com
This LRC file may not match your music if the duration is not the same. Click Edit below and simply apply an offset (+0.10 sec, -0.10 sec, etc.)
You May Listen Pullo Àrdo by Youssou N'Dour
1. Who is the singer of "Pullo Àrdo" song?
⇒ Youssou N'Dour has sung the song "Pullo Àrdo".
2. Which album is the "Pullo Àrdo" song from?
⇒ The song "Pullo Àrdo" is from the album Youssou N'Dour.
3. In which language is the "Pullo Àrdo" song composed?
⇒ The song "Pullo Àrdo" is composed in the Luxembourgish language.
4. What is the official duration of the "Pullo Àrdo" song?
⇒ The official duration of "Pullo Àrdo" is 04:00.93.
5. Can I reupload this LRC file on the internet?
⇒ Sorry, you are not allowed to reupload this LRC file on the internet without permission. This is only for your personal use.
6. Does this LRC file perfectly match the official song?
⇒ Yes, it does most of the time, but sometimes you may need to apply an offset using our tool, LRC File Maker (e.g., +10 or -10).
Youssou N'Dour - Pullo Àrdo