Read, copy, and download the Bekoor lyrics LRC file, which provides synchronized music subtitles for the song Bekoor by Youssou N'Dour from the album Youssou N'Dour. Our LRC file is created using the free "LRC File Maker" tool and matches the official length of the song, which is 06:26.90. Additionally, you can download the lyrics in TXT (.txt), SRT (.srt), and PDF (.pdf) formats.
[ti:Bekoor]
[ar:Youssou N'Dour]
[al:Youssou N'Dour]
[lang:Javanese]
[length:06:26.90]
[by:Jun]
[re:www.rclyricsband.com]
[ve:v0.0.5]
[00:00.00]
[00:37.12]Mbay maral wi mettina yaay
[00:40.80]Bekoor bi yàkk na ndeysan
[00:44.89]Ndimbal lañuy sakkoo
[00:47.96]Gir baykat sonn na yaay
[00:58.30]Mbay maral wi mettina yaay
[01:01.95]Bekoor bi yàkk na ndeysan
[01:05.63]Ndimbal lañuy sakkoo
[01:08.51]Gir baykat sonn na yaay
[01:12.68]♪
[01:31.53]Démb da doon taw aywaay yé
[01:33.89]Suuf naan màndi
[01:35.63]Démb da doon taw di baawaan
[01:37.87]Jur gi naan sempi
[01:39.60]Démb da doon bakaaw di jàncax
[01:42.21]Jur gi xontu mbaa jur
[01:43.96]Àll be naan réew mi naan di guŋdanaan
[01:47.70]Sitóor yi naan com maral
[01:53.70]Mbay maral wi mettina yaay
[01:58.08]Bekoor bi yàq na ndeysan
[02:01.33]Ndimbal lañuy sakoo
[02:04.19]Gir sámmkat bi sonn yaay
[02:14.94]Mbay maral wi mettina yaay
[02:18.38]Bekoor bi yàq na ndeysan
[02:21.59]Ndimbal lañuy sakoo
[02:24.73]Gir sámmkat bi sonn yaay
[02:29.53]♪
[02:47.30]Démb da doon taw aywaay yé
[02:54.18]Eh, eh, ho-ho, he, ho-ho, he
[03:00.68]Ah-ha, he, ho, he-he man, he
[03:10.23]Mbay maral wi mettina yaay
[03:13.90]Bekoor bi yàq na ndeysan
[03:17.40]Ndimbal lañuy sakKoo
[03:20.02]Gir sámmkat bi sonn yaay
[03:24.27]♪
[03:42.47]Tay su xin ne sappar gelawaal mbaa naat say
[03:45.86]Ak nawet buu nangu baa dal meññaal gàncax
[03:49.36]Taay Baykat bëttul, desetul gerte
[03:52.99]Wa réewmi yàq warul tax, taa mën a nekk
[03:56.21]War ngaa bokk ci ndimbal lii jëm ci waa gaw gi
[03:59.07]Ndeysan maral bi meeti yaay
[04:05.77]Sámmkat sonn
[04:08.58]Nañu ndimbali sanu bopp nax yàlla ndimbali ñum
[04:11.96]Nanu ndimbali sunu moroom nax Yàlla nangul nooo
[04:15.82]Maral, maral, maral
[04:19.57]♪
[05:07.77]Maral, maral, maral bi metti na
[05:14.08]Maral, maral, maral bi metti na
[05:20.88]Maral, maral, maral bi metti na
[05:24.43]Nanu jëmbët garab te di koo suxal garab ci la
[05:28.00]Maral, maral, maral bi metti na
[05:31.24]Nanu ndimbali sanu bopp nax yàlla ndimbali ñum
[05:34.59]Maral, maral, maral bi metti na
[05:38.14]Nanu jëmbët garab te di koo suxal garab ci la
[05:41.12]Maral, maral, maral bi metti na
[05:44.23]Yàlla yàlla bay sa tooloo
[05:47.83]Maral, maral, maral bi metti na
[05:51.45]Ngir wa kaw gi maral bi metti na
[05:54.78]Maral, maral, maral bi metti na
[05:59.22]RCLyricsBand.Com
This LRC file may not match your music if the duration is not the same. Click Edit below and simply apply an offset (+0.10 sec, -0.10 sec, etc.)
You May Listen Bekoor by Youssou N'Dour
1. Who is the singer of "Bekoor" song?
⇒ Youssou N'Dour has sung the song "Bekoor".
2. Which album is the "Bekoor" song from?
⇒ The song "Bekoor" is from the album Youssou N'Dour.
3. In which language is the "Bekoor" song composed?
⇒ The song "Bekoor" is composed in the Javanese language.
4. What is the official duration of the "Bekoor" song?
⇒ The official duration of "Bekoor" is 06:26.90.
5. Can I reupload this LRC file on the internet?
⇒ Sorry, you are not allowed to reupload this LRC file on the internet without permission. This is only for your personal use.
6. Does this LRC file perfectly match the official song?
⇒ Yes, it does most of the time, but sometimes you may need to apply an offset using our tool, LRC File Maker (e.g., +10 or -10).
Youssou N'Dour - Bekoor