Read, copy, and download the Liggeey lyrics LRC file, which provides synchronized music subtitles for the song Liggeey by Youssou N'Dour from the album Youssou N'Dour. Our LRC file is created using the free "LRC File Maker" tool and matches the official length of the song, which is 04:38.97. Additionally, you can download the lyrics in TXT (.txt), SRT (.srt), and PDF (.pdf) formats.
[ti:Liggeey]
[ar:Youssou N'Dour]
[al:Youssou N'Dour]
[lang:Luxembourgish]
[length:04:38.97]
[by:Jun]
[re:www.rclyricsband.com]
[ve:v0.0.5]
[00:00.00]
[00:07.42]Teranga Doomu adama
[00:09.34]Liggéey doŋ ka mën a joxee
[00:16.65]Te li mu néew-néew
[00:18.44]Mooma gënal lenéen li ma mën ti am
[00:25.67]Jamono liggéey, jamono liggéey lañu nekk
[00:34.48]Liggéey war na góor, war na kiy jigéen
[00:43.43]Foo wara tekki, tekkiwoo fa doyna waar
[00:52.10]Nekk ci palas wara liggéey te liggéeyoo
[01:00.99]Bës bula xa ca raw, boobee bës dem na
[01:05.65]Te beneen bi ñëw te xamuloo lu mu àndal
[01:10.14]Ma nee tàkku liggéey dafa jot
[01:14.67]Liggéey léen
[01:28.33]Liggéey na nga liggéey (moo yoor réewmi)
[01:32.90](liggéey) foo mën a nekk (na nga liggéey)
[01:35.57]Foo mën a tollu(liggéey) moo yoor réewmi(liggéey)
[01:41.56](Liggéey) foo mën a nekk (liggéey) foo mën a tollu (liggéey)
[01:47.37]Moo yoor réewmi (liggéey)
[01:50.74](Liggéey) foo mën a nekk (liggéey) foo mën a tollu
[01:56.13]♪
[02:13.32]Kàttan bi sax, moon di na mës a jeex
[02:22.30]Kaay ñu liggéey, liggéey taxawu sunu jàboot moo gën
[02:30.99]Maa ni bës bula xa ca raw, boobee bës dem na
[02:35.86]Te beneen bi ñëw te xamuloo lu mu àndal
[02:40.00]Ma nee tàkku liggéey dafa jot
[02:44.85]Liggéey léen
[02:53.63]Tell like wish welcome
[02:56.01]Tell like wish welcome
[02:58.03]Tell like wish welcome
[03:00.39]Tell like wish welcome
[03:02.33]Tell like wish welcome, welcome so easy
[03:11.17]Na nga Liggéey, dollil liggéey (moo yoor réwmi)
[03:15.90]Na nga liggéey(foo mën a nekk) na nga liggéey(ag foo mën a tollu)
[03:20.11]Tell like wish welcome
[03:22.46]Tell like wish welcome
[03:24.70]Tell like wish welcome
[03:26.90]Tell like wish welcome
[03:29.08]Tell like wish welcome, welcome so easy
[03:38.43]Liggéey, dollil liggéey (moo yoor réwmi)
[03:43.19]Na nga liggéey (foo mën a nekk) na nga liggéey
[03:45.64](ag foo mën a tollu) naa nga liggéey
[03:47.87]Loo mën a amiit(naa nga liggéey)
[03:52.09]Tell like wish welcome
[03:53.93]Tell like wish welcome
[03:56.70]Tell like wish welcome
[03:58.78]Tell like wish welcome
[04:00.58]Tell like wish welcome, welcome so easy
[04:09.53]Tell like wish welcome
[04:11.90]Tell like wish welcome
[04:14.00]Tell like wish welcome
[04:16.72]Tell like wish welcome
[04:18.77]Tell like wish welcome, welcome so easy
[04:26.36]RCLyricsBand.Com
This LRC file may not match your music if the duration is not the same. Click Edit below and simply apply an offset (+0.10 sec, -0.10 sec, etc.)
You May Listen Liggeey by Youssou N'Dour
1. Who is the singer of "Liggeey" song?
⇒ Youssou N'Dour has sung the song "Liggeey".
2. Which album is the "Liggeey" song from?
⇒ The song "Liggeey" is from the album Youssou N'Dour.
3. In which language is the "Liggeey" song composed?
⇒ The song "Liggeey" is composed in the Luxembourgish language.
4. What is the official duration of the "Liggeey" song?
⇒ The official duration of "Liggeey" is 04:38.97.
5. Can I reupload this LRC file on the internet?
⇒ Sorry, you are not allowed to reupload this LRC file on the internet without permission. This is only for your personal use.
6. Does this LRC file perfectly match the official song?
⇒ Yes, it does most of the time, but sometimes you may need to apply an offset using our tool, LRC File Maker (e.g., +10 or -10).
Youssou N'Dour - Liggeey