Read, copy, and download the Mama Africa lyrics LRC file, which provides synchronized music subtitles for the song Mama Africa by Youssou N'Dour from the album Youssou N'Dour. Our LRC file is created using the free "LRC File Maker" tool and matches the official length of the song, which is 03:57.79. Additionally, you can download the lyrics in TXT (.txt), SRT (.srt), and PDF (.pdf) formats.
[ti:Mama Africa]
[ar:Youssou N'Dour]
[al:Youssou N'Dour]
[lang:Luxembourgish]
[length:03:57.79]
[by:Jun]
[re:www.rclyricsband.com]
[ve:v0.0.5]
[00:00.00]
[00:03.07]Yée, yée-hé-hé-hé
[00:06.68]Yée, yée-hé-hé-hé
[00:10.43]Hoo, hoo ehnnn haaan
[00:15.40]Hoo africains, woy le leen ma africa
[00:18.89]Benn continent, melul ni africa
[00:22.65]Amul benn werente ci loolu
[00:26.14]Suñu mbëggél ci yaw, Africa
[00:30.27]Amna ñi soriyaante
[00:33.63]Bu ñu kenn jaxasse
[00:37.21]Na ñu xam suñu bopp
[00:41.27]Une jeunesse engagée, africa
[00:44.96]Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
[00:48.97]Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
[00:52.74]Boo xasee miin xam ni, fii mooy suñu kër
[00:56.82]Come home with me
[01:00.10]Hoo africains, woy le leen ma africa
[01:03.39]Benn continent, melul ni africa
[01:07.76]Amul benn werente ci loolu
[01:11.60]Suñu mbëggél ci yaw, Africa
[01:15.35]Ana ñi soriyaante
[01:18.83]Bu ñu kenn jaxasse
[01:22.91]Na ñu xam suñu bopp, avec
[01:26.33]Une jeunesse engagée, africa
[01:30.19]Namm u ñu dara, yalla a la barkeel
[01:33.93]Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo
[01:37.47]Boo xasee miin, xam ni, fii mooy suñu kër
[01:41.50]Come home with me
[01:45.01]Ñun africains, su ñu ànd a ndoo
[01:48.56]Bokk nday ak baay, Boole suñuy doole
[01:52.50]Kholal ëllëg u adduna bi
[01:56.20]Seetal say doom ñoo, koy mujjee
[02:07.08]Yée, hée hée, an han
[02:12.92]♪
[02:32.73]Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
[02:35.09]Noonu nga riché
[02:36.84]Ni nga maggeek, ni nga yaatoo
[02:38.87]Noonu nga riché
[02:40.09]Du ñu la weccoo ba muk
[02:42.23]Du ñu la weccook keneen africa
[02:45.30]Xam nga ni la say, doom yi bëggee
[03:07.58]Tag naa la kaay
[03:10.68]Yaa ne ci suñu xol
[03:13.53]Wo, wo, wo, wooy
[03:15.30]Wo, wo, wo, wooy
[03:18.80]Du ñu la mas a weccooy
[03:20.82]Kenn du yaw Africa
[03:27.77]Yée ... yée hé hé hée hé
[03:38.06]RCLyricsBand.Com
This LRC file may not match your music if the duration is not the same. Click Edit below and simply apply an offset (+0.10 sec, -0.10 sec, etc.)
You May Listen Mama Africa by Youssou N'Dour
1. Who is the singer of "Mama Africa" song?
⇒ Youssou N'Dour has sung the song "Mama Africa".
2. Which album is the "Mama Africa" song from?
⇒ The song "Mama Africa" is from the album Youssou N'Dour.
3. In which language is the "Mama Africa" song composed?
⇒ The song "Mama Africa" is composed in the Luxembourgish language.
4. What is the official duration of the "Mama Africa" song?
⇒ The official duration of "Mama Africa" is 03:57.79.
5. Can I reupload this LRC file on the internet?
⇒ Sorry, you are not allowed to reupload this LRC file on the internet without permission. This is only for your personal use.
6. Does this LRC file perfectly match the official song?
⇒ Yes, it does most of the time, but sometimes you may need to apply an offset using our tool, LRC File Maker (e.g., +10 or -10).
Youssou N'Dour - Mama Africa