Read, copy, and download the Dabbaax lyrics LRC file, which provides synchronized music subtitles for the song Dabbaax by Youssou N'Dour from the album Youssou N'Dour. Our LRC file is created using the free "LRC File Maker" tool and matches the official length of the song, which is 05:09.26. Additionally, you can download the lyrics in TXT (.txt), SRT (.srt), and PDF (.pdf) formats.
[ti:Dabbaax]
[ar:Youssou N'Dour]
[al:Youssou N'Dour]
[lang:Javanese]
[length:05:09.26]
[by:Jun]
[re:www.rclyricsband.com]
[ve:v0.0.5]
[00:00.00]
[00:04.98]keroksou penc bognouy wadjia wathié janta bi
[00:21.84]Di wadjial Péssé ba
[00:26.74]Moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam
[00:32.44]Moulaay Dabaaaaax...
[00:38.01]Bougnou Faté, Bess boboulé, Uhh Bougnou Soré, Bess boboulé
[00:47.61]Bougnou faté Bess Boboulé,
[00:55.58]Lofa Gnaane, Yalla May lako.
[01:00.49]Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi
[01:13.49]Anh Mo daane Kadou Askane wi.
[01:19.08]Dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew
[01:24.42]Dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui
[01:28.73]Dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi
[01:33.65]Dafa daane wakh naane nagnou yeureum Djiguéen
[01:57.59]Sa borom bi begu na, Yonentam bi begu na, yako liguéyal sa borom.
[02:02.45]Moulaye Dabbaxx yaw dé wacci ngua masso wakh lou amoul.
[02:12.53]Kérok bang gnou djito assamaane si da Leudeum,
[02:14.01]Bessa ngui kéne dotou ko Fatéééti... Moulaay Dabbaxx
[02:21.72]Bougnou Faté, Bess boboulé, Bougnou Soré, Bess boboulé
[02:31.82]Bougnou faté Bess Boboulé,
[02:37.38]Lofa Gnaane, Yalla May lako.
[02:42.75]anh! Modaane wakhal nitt gnep, anh! Mo daane wakhal nasraane yi.
[02:53.08]Anh! Mo daane wakhal Askane wi.
[03:01.25]Dafa daane wakh naane na gnep ligueye
[03:04.27]Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
[03:09.48]Dafa daane wakh naane na gnep liguèye
[03:14.79]Dafa daane wakh naane nagn diangal djiguééne gni
[03:28.39]daawaoul Sétane lou gnaaw
[03:37.96]Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw
[03:41.41]Rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx
[04:01.13]daawaoul Sétane lou gnaaw
[04:04.01]Poussom la yorone fou khotékou Mou gnaw
[04:09.04]Rewmi.rewmi amélnagnou la ndiouka Moulaay Dabbaxx.
[04:13.22]Bakrék Dara Maam, Aram lô Coumba Thiam,
[04:15.20]Magn Penda ak Pathé Pendaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaah
[04:17.33]Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi
[04:36.89]Mo daane Kadou Askane wi.
[04:42.47]Dafa daane wakh naane nagn diap sounou rewmi.
[04:46.57]Dafa daane wakh naane nagnep liguéye
[04:51.93]Dafa daane wakh naane nagn Yeureum djiguéene gni.
[04:58.72]Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
[05:02.79]RCLyricsBand.Com
This LRC file may not match your music if the duration is not the same. Click Edit below and simply apply an offset (+0.10 sec, -0.10 sec, etc.)
You May Listen Dabbaax by Youssou N'Dour
1. Who is the singer of "Dabbaax" song?
⇒ Youssou N'Dour has sung the song "Dabbaax".
2. Which album is the "Dabbaax" song from?
⇒ The song "Dabbaax" is from the album Youssou N'Dour.
3. In which language is the "Dabbaax" song composed?
⇒ The song "Dabbaax" is composed in the Javanese language.
4. What is the official duration of the "Dabbaax" song?
⇒ The official duration of "Dabbaax" is 05:09.26.
5. Can I reupload this LRC file on the internet?
⇒ Sorry, you are not allowed to reupload this LRC file on the internet without permission. This is only for your personal use.
6. Does this LRC file perfectly match the official song?
⇒ Yes, it does most of the time, but sometimes you may need to apply an offset using our tool, LRC File Maker (e.g., +10 or -10).
Youssou N'Dour - Dabbaax