Read, copy, and download the Ndaga lyrics LRC file, which provides synchronized music subtitles for the song Ndaga by Samba Peuzzi from the album Senegalboy. Our LRC file is created using the free "LRC File Maker" tool and matches the official length of the song, which is 03:39.42. Additionally, you can download the lyrics in TXT (.txt), SRT (.srt), and PDF (.pdf) formats.
[ti:Ndaga]
[ar:Samba Peuzzi]
[al:Senegalboy]
[lang:English]
[length:03:39.42]
[by:Jun]
[re:www.rclyricsband.com]
[ve:v0.0.5]
[00:00.00]
[00:02.28]SENEGALBOYOO
[00:05.45]From diack waw
[00:07.30]Skurt, ratata,
[00:11.86]hey yah
[00:13.72]Comme que dañi ndaga
[00:15.36]Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
[00:16.61]Nénañ dañi ndaga
[00:20.53]Comme que dañi ndaga (waw)
[00:22.54]Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
[00:24.12]Nénañ dañi ndaga
[00:27.35]Eh kolo kuy sa kolo kolo
[00:30.88]Rappeurs yi may sen tonton
[00:34.46]Kolo kuy sa kolo kolo
[00:38.76]Rappeurs yi may sen tonton
[00:39.43]Check hey
[00:40.55]Duma teggi tànk ak sama semelles rouges
[00:42.70]Doma guiss mafia bé lay nokk
[00:44.20]Commencer guma ñom ñungui onku
[00:45.70]Sama yaye néna non boulen tontu
[00:47.50]Bu xayé tek ñorna meuno sipp
[00:49.53]Son bu ngané ki du nitt
[00:49.87]Ci man guen di xol jamano dji
[00:52.77]Yarul ma jangal la non du ni
[00:54.28]Hey legui folen ma guiss
[00:56.03]Nélen tonton ñëwna
[00:57.68]Sen clash yi mi ngui may dal
[00:59.25]Mais tontu wuma
[01:01.07]International boy fi guen di tok
[01:03.18]Tek guen ma bët wayé dolen ma japp
[01:04.74]Def sen awards sans man (rambakh)
[01:06.42]Ayway nopal guen samba
[01:08.50]Comme que dañi ndaga
[01:09.74]Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
[01:10.79]Nénañ dañi ndaga
[01:15.33]Comme que dañi ndaga (waw)
[01:16.81]Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
[01:18.60]Nénañ dañi ndaga
[01:22.28]Eh kolo kuy sa kolo kolo
[01:26.80]Rappeurs yi may sen tonton
[01:28.99]Kolo kuy sa kolo kolo
[01:33.75]Rappeurs yi may sen tonton
[01:35.11]Hey man késsé may door non li du xéx
[01:37.52]Ñom duñ ma lale amna moustiquaire
[01:38.66]Fils do tuss damala pique nga per
[01:40.83]Sa yekk du yagg comme dajù ballon
[01:42.20]Sama succès sama bras long
[01:44.06]Sa meilleur sagnsé guiss nako Uno
[01:45.78]Olala rappeurs yi fi ñom dal ñom ñeup ndiro
[01:48.96]Yalla ma yombalale li textes sax binda tuma ko
[01:52.22]Legui game bi dama fay
[01:54.14]I got the drip boy (thiey li)
[01:55.94]Di pull up ak sama beamer ouh yah aduna ni leu
[01:58.84]No cap amna xaliss ouh yah aduna ni leu (Baww)
[02:03.37]Comme que dañi ndaga
[02:04.88]Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
[02:07.03]Nénañ dañi ndaga
[02:10.50]Comme que dañi ndaga (waw)
[02:11.79]Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
[02:13.35]Nénañ dañi ndaga
[02:16.84]Eh kolo kuy sa kolo kolo
[02:21.57]Rappeur yi may sen tonton
[02:23.83]Kolo kuy sa kolo kolo
[02:28.40]Rappeur yi may sen tonton
[02:30.77]Comme que dañi ndaga
[02:32.16]Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
[02:34.27]Nénañ dañi ndaga
[02:37.74]Comme que dañi ndaga (waw)
[02:39.42]Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
[02:40.90]Nénañ dañi ndaga
[02:44.29]Eh kolo
[02:45.76]Diougal yëngou
[02:46.40]Ndaga Ndiaye Ndaga
[02:48.15]Ndakh Ndaga yakhal namey nelaw
[02:50.43]Ndaga Ndiaye Ndaga
[02:52.61]Ndaga Ndiaye
[02:54.03]Ay way yow ndaw Ndaga Ndiaye Ndaga
[03:02.59]Eh kolo kuy sa kolo kolo
[03:07.33]Rappeurs yi may sen tonton
[03:10.17]Kolo kuy sa kolo kolo
[03:14.30]Rappeurs yi may sen tonton
[03:16.61]RCLyricsBand.Com
This LRC file may not match your music if the duration is not the same. Click Edit below and simply apply an offset (+0.10 sec, -0.10 sec, etc.)
You May Listen Ndaga by Samba Peuzzi
1. Who is the singer of "Ndaga" song?
⇒ Samba Peuzzi has sung the song "Ndaga".
2. Which album is the "Ndaga" song from?
⇒ The song "Ndaga" is from the album Senegalboy.
3. In which language is the "Ndaga" song composed?
⇒ The song "Ndaga" is composed in the English language.
4. What is the official duration of the "Ndaga" song?
⇒ The official duration of "Ndaga" is 03:39.42.
5. Can I reupload this LRC file on the internet?
⇒ Sorry, you are not allowed to reupload this LRC file on the internet without permission. This is only for your personal use.
6. Does this LRC file perfectly match the official song?
⇒ Yes, it does most of the time, but sometimes you may need to apply an offset using our tool, LRC File Maker (e.g., +10 or -10).
Samba Peuzzi - Ndaga