• rclyrisband-search
  • Home Search Dark Mode Request LRC Singer AIO Editor LRC Maker Request List LRC File Basics Privacy Policy Credits About Contact

    Download Ñibisil Lyrics by Ashs The Best - Read, Copy & Get LRC, PDF, TXT, SRT Files

    Read, copy, and download the Ñibisil lyrics LRC file, which provides synchronized music subtitles for the song Ñibisil by Ashs The Best from the album Dibèer. Our LRC file is created using the free "LRC File Maker" tool and matches the official length of the song, which is 04:19.13. Additionally, you can download the lyrics in TXT (.txt), SRT (.srt), and PDF (.pdf) formats.



    Ñibisil by Ashs The Best LRC Format

    [ti:Ñibisil]
    [ar:Ashs The Best]
    [al:Dibèer]
    [lang:Indonesian]
    [length:04:19.13]
    [by:Jun]
    [re:www.rclyricsband.com]
    [ve:v0.0.5]
    [00:00.00]
    [00:14.79]Ñibisil
    [00:18.46]Ñibisi-i-il
    [00:24.73]Jukk du wess, jukk du wess
    [00:32.67]Suma lay woo lutax doma falé
    [00:40.47]Wax ma lu dañ ci man xana bëgëtoma
    [00:45.19]Yeah, yeah
    [00:49.41]Bëtu mbëgëel lala mësa xol le
    [00:56.63]Lu waral man ak yaw ñu dëkk si cow
    [01:05.44]Suma xolei fuñu jar yep
    [01:08.64]Dag ma wowon dima deff fu sori
    [01:13.97]Bi ñuye goro loxam wax ma
    [01:16.88]Tay bitti bi molay gërëm kër gi joy triste
    [01:21.53]Samba alar waw si njabot ji
    [01:29.54]Xol yagi joy xar yagi joye
    [01:36.26]Ñaata at man ak yaw ci kër gi
    [01:37.76]Bimalay tan bobu xalato diga sëye si
    [01:39.92]Soxna si sétal si Yallah ji ga xol si bitti
    [01:41.38]Gisso sa morom bu né si sëye ba pare nési
    [01:43.01]Mbédd bi njaboot mo mucow
    [01:44.78]Lu fess nak si xol su ëpe turu
    [01:46.60]Muñe na ba s¨s taxul ga xam li xol bi jiyunju
    [01:48.41]Dadjie n'a lu ne gir yak ak njaboot ji liñuye dundu
    [01:50.33]Fimay dundu giss n'a luné ms taxul ma xadi
    [01:52.62]Baneex man dég lassi am
    [01:53.91]Cono ak nakkar tax ma gëje nekk si jam
    [01:55.82]Wax ma lan ga bëgg si lan gané
    [01:57.31]Talatoma talato sa kër gi wax ma noye deff ak njaboot gi
    [01:58.87]Wax ma man ak yaw ku tane
    [02:00.96]Feep fo xam nangi maffa clamé
    [02:02.51]Mbato dem mbato koste mënoma teré xolli kanene
    [02:05.09]Leep loma yakkul dagako fatte
    [02:06.43]Su respect jexe mbëgeel dem yonam luñu desse ludul
    [02:09.81]Samba alar waw si njabot ji
    [02:13.45]Géstu war nala samba alar ga
    [02:17.27](Xol yagi joy xar yagi joye)
    [02:20.74]Gniga bëgëntél ñongi sa ginaaw
    [02:23.08]Yeah, yeah
    [02:24.63]Sumalay wo gani doma falé
    [02:30.30]Sumalay woo, oh oh
    [02:33.39]Xana nobatoma?
    [03:12.43]Su démb donone tay
    [03:18.02]Ma joxatta sama mbegeel?
    [03:22.01]Su démb donone tay
    [03:26.41]Ma joxat la sama xol bi mbegeel bi
    [03:30.62]Sumalay wo gani doma falé
    [03:35.00]Sumalay woo, oh oh
    [04:18.12]RCLyricsBand.Com

    This LRC file may not match your music if the duration is not the same. Click Edit below and simply apply an offset (+0.10 sec, -0.10 sec, etc.)



    Try Our Free Tools


    You May Listen Ñibisil by Ashs The Best

    apple music logospotify music logoamazon music logotidal music logoyoutube music logo

    Xalam

    Goor

    Alxames

    Pottu Ndaa

    Yàlla

    Guddi - Bonus Track

    I FEEL GOOD

    Jirim

    LIFE IS LOVE

    Tukki Bukki

    GIVE UP

    Xel Akk Xol

    Yaakaar

    Gadaay

    MY LIFE

    Ngala Way

    Yaay Joor

    Ñibisil


    FAQ:

    1. Who is the singer of "Ñibisil" song?

    ⇒ Ashs The Best has sung the song "Ñibisil".

    2. Which album is the "Ñibisil" song from?

    ⇒ The song "Ñibisil" is from the album Dibèer.

    3. In which language is the "Ñibisil" song composed?

    ⇒ The song "Ñibisil" is composed in the Indonesian language.

    4. What is the official duration of the "Ñibisil" song?

    ⇒ The official duration of "Ñibisil" is 04:19.13.

    5. Can I reupload this LRC file on the internet?

    ⇒ Sorry, you are not allowed to reupload this LRC file on the internet without permission. This is only for your personal use.

    6. Does this LRC file perfectly match the official song?

    ⇒ Yes, it does most of the time, but sometimes you may need to apply an offset using our tool, LRC File Maker (e.g., +10 or -10).

    Ashs The Best - Ñibisil